Le Ramadan Des Lutteurs
une célèbre expression des lutteurs qui fait fureur dans l’arène. Et le résultat donne ça.
« Bécaye dieullma directe … Bécaye dieullma directe… ok merchi. Guinaw bima santé Yalla, Djouli thi Yonéntbi, Sant samay wadiour, KOOR gui damako yag paré Becaye! Lima entrainé khadioul thi mom Mangui sante NELAW diko guereum daf may conseillé dima dalal bou bakh! Di sante NDOGOU dafa soneu thi mane: niom pain, saucisson, camembert, tandarma … kou liim dioum Amouma séne faye! Dama fatéwone KHEUD, mome tamite diap na si combat WEROU KOOR bi bou baakh! Bécaye niommm diouli nafila ak zirk yeupp amoul louniou défoul pour ma danou mais Bécaye dama liguéy Bécaye